Site owners

  • Papa Oumar Fall


58days since
9th anniversary of STYLOCULTURE

Exhibition : STYLOGRAPHIE (or Ballpoint Pen Art)

You are artist. The ballpoint pen serves  as a medium to carry your work.

You want to participate, as an artist-partner, to a collective exhibition of Stylographie.

I expect your message to: admin@styloculture.org or 0049 1765 2438099


> "Jok jot na!"

Ci miim jamono

Dëgga attan tumuranke !

 

Waaye moo doy cip weetal

Waaye moo doy cip wettal

 

Xoolal fen ni muy lawe

Melna geej gu aay

 

Duus yay fewwi-fewwi!

Dooley ngelawam upp na

Suuf si tasaaroo!

 

Cëy lii

Bip pënd

Di warac-waraci

 

Teeyayu xel

Mankook

Sellayu xol

 

Ñoom seen

Mucc sip lor

 

Xëlimaak daa

Doy nap gannay

Xareek jëësi wees na

 

Deqqi teenup Dëqële

Fekku fap teere

 

Nasaraan si bind na

Amul laq! Lakkal!

A! Joor jok jot na!